1
00:00:03,520 --> 00:00:04,690
Dafa xonk...

2
00:00:06,440 --> 00:00:07,900
Noonu la amee kawar gu nit ki.

3
00:00:10,940 --> 00:00:11,780
Dafa xonk...

4
00:00:12,700 --> 00:00:15,530
Dafa gëna xonk kawar gu weex melni fraise.

5
00:00:16,280 --> 00:00:18,700
Melni xonk bi tafu samay loxo.

6
00:00:19,240 --> 00:00:21,700
Kawar gu xonk gu rafet.

7
00:00:21,700 --> 00:00:24,080
Waaw, moom la.

8
00:00:25,460 --> 00:00:28,960
Dundu... ngir sama njariñ.

9
00:00:29,800 --> 00:00:35,260
épisode 1

10
00:00:29,800 --> 00:00:35,260
「Amnaa xarit bu jigeen!」

11
00:00:31,090 --> 00:00:35,890
Ah... dama bëgga xëcc ay ween.

12
00:00:36,300 --> 00:00:38,850
Liggéeyu daara Co-ed!

13
00:00:38,850 --> 00:00:41,560
Bul wax loolu wala amul benn njariñ!

14
00:00:42,730 --> 00:00:44,810
Matsuda, Motohama,

15
00:00:44,810 --> 00:00:48,060
Lu tax nu dugg ci daara jii?

16
00:00:48,900 --> 00:00:53,820
Kuou Academy dafa yàgg nekk daara ju jigéen ñi kese.

17
00:00:55,240 --> 00:01:01,490
Rax ci dolli limu ndongo yu jigéen yu bari yi ci dëkk bi ak ci bitim réew!

18
00:01:01,490 --> 00:01:04,000
Moo tax xale yu góor yi dañu bëgga ñëw ekol bi.

19
00:01:04,000 --> 00:01:09,040
Doonte waxunu dara, amna jigéen ñuy yuuxu ngir ñu bàyyi seen xel ci nun!

20
00:01:09,750 --> 00:01:13,260
Kon li waral ma ñëw fi mooy defar sama harem!

21
00:01:13,260 --> 00:01:14,670
Waaw!

22
00:01:14,670 --> 00:01:18,430
Linu bëgg mooy dundu gu fees dell ak ween!

23
00:01:18,430 --> 00:01:20,680
Xeexal! Xeexal! Xeexal!

24
00:01:20,680 --> 00:01:22,350
Doonte wax nanu loolu,

25
00:01:22,350 --> 00:01:27,770
sunu coono yépp melni lu ñàkk njariñ ndax kenn ci nun amul benn xale bu jigéen ginaaw bimu nekkee fi ñaari at.

26
00:01:27,770 --> 00:01:33,030
Xeexal! Xeexal! Xeexal! Xeexal! Xeexal!

27
00:01:28,600 --> 00:01:30,690
Mën nanu bàyyi.

28
00:01:30,690 --> 00:01:32,280
Dina nekk njeexte sunu xàddi!

29
00:01:32,280 --> 00:01:33,780
Ba leegi yaakaar amna ci nun!

30
00:01:37,070 --> 00:01:38,490
Kiba-kun!

31
00:01:38,490 --> 00:01:39,910
Lu nga nara def ginaaw lii?

32
00:01:39,910 --> 00:01:42,740
Bëgg nga ànd ak nun ci karaoke?

33
00:01:42,740 --> 00:01:44,790
Man itam bëgg naa la. Ginaaw lii dina am ay liggéey ci club bi.

34
00:01:44,790 --> 00:01:46,870
Eh? Loolu baaxul.

35
00:01:46,870 --> 00:01:48,790
Def nga sax lépp lumu mën ngir invite ma...

36
00:01:48,790 --> 00:01:50,000
Maa ngi lay massawu.

37
00:01:52,300 --> 00:01:54,550
2ème année, classe C, kiba yuuto.

38
00:01:54,550 --> 00:01:57,130
Ndongo bu mag bu jigeen ñi bëgg te siiw.

39
00:01:57,130 --> 00:01:59,470
Mooy sunu noonu góor ñi.

40
00:01:59,470 --> 00:02:01,100
Alal!

41
00:02:01,100 --> 00:02:05,770
Ndax amna melokaan, yuur, ak jikko, tekkiwul ni mën na réy-réy!

42
00:02:05,770 --> 00:02:07,520
Bàyyi wax loolu! Yaa ngi may bëgga dee!

43
00:02:08,060 --> 00:02:09,770
Àdduna bi dafa fees dell ak njubadi.

44
00:02:09,770 --> 00:02:11,940
Oh xale! Dafa jegesi!

45
00:02:11,940 --> 00:02:13,320
Fan nga jëm?

46
00:02:16,690 --> 00:02:20,320
Ween yu Murayama dañu rëy lool!

47
00:02:20,320 --> 00:02:22,280
80-70-81.

48
00:02:22,280 --> 00:02:24,830
Katase amna tànk yu sew!

49
00:02:24,830 --> 00:02:27,040
78-65-79.

50
00:02:27,040 --> 00:02:29,290
Dama fekk barab bii ci jamonoy Education Physique.

51
00:02:29,290 --> 00:02:31,460
Ba leegi amna lu gëna bari.

52
00:02:32,460 --> 00:02:33,540
Hey!

53
00:02:34,340 --> 00:02:35,800
Xaaral ma gis man itam!

54
00:02:36,550 --> 00:02:38,800
Yeen ñaar war ngeen bàyyi lépp!

55
00:02:38,800 --> 00:02:39,800
Hey!

56
00:02:39,800 --> 00:02:40,800
Ndax amna ku fa nekk ?

57
00:02:40,800 --> 00:02:41,300
Ha?

58
00:02:41,300 --> 00:02:42,180
Bul dof, yaw-

59
00:02:42,180 --> 00:02:42,930
Ay!

60
00:02:46,970 --> 00:02:47,930
Luy loolu?!

61
00:02:47,930 --> 00:02:51,270
Salaam, Matsuda, Motoha... Yaay...

62
00:02:52,690 --> 00:02:54,570
Mooy yeen sama gaa yi.

63
00:02:54,570 --> 00:02:56,150
Oh xale...

64
00:02:56,150 --> 00:02:58,110
Xaaral!

65
00:02:58,110 --> 00:03:00,320
Di nga ko jëlee ci nun!

66
00:03:01,610 --> 00:03:03,280
Ow ow ow...

67
00:03:03,280 --> 00:03:05,370
Kan mooy jëfandikoo shinai ngir dóor nit ñi?

68
00:03:03,280 --> 00:03:05,370
TL Tegtal: Shinai sabre bamboo la bu ñuy jëfandikoo ci Kendo.

69
00:03:05,370 --> 00:03:07,500
Yaakaar naa ni danga am wërsëg foofu, Issei.

70
00:03:07,500 --> 00:03:08,870
Bàyyi ma nii...

71
00:03:08,870 --> 00:03:13,880
Dinaa ci baax sudee may nga ma gis benn ci weeni xale bu jigéen bi, waaye lii amul benn sabab...

72
00:03:27,640 --> 00:03:31,390
Ba leegi amna nit ñuy jëfandikoo tabax daara ju yàgg ji, wala book?

73
00:03:31,390 --> 00:03:35,060
Kawar gu xonk gi rafet na.

74
00:03:35,060 --> 00:03:36,900
Rias Gremory.

75
00:03:37,360 --> 00:03:39,650
99-58-90.

76
00:03:39,650 --> 00:03:42,030
Ñatteelu at ak njiitu Occult Club.

77
00:03:42,030 --> 00:03:44,530
Dégg naani mingi cosaanoo ci benn ci réew yu Scandinavie.

78
00:03:50,750 --> 00:03:52,000
Xale boobu leegi...

79
00:03:52,000 --> 00:03:52,830
Waaw?

80
00:03:53,420 --> 00:03:55,000
Dama bëgga xam rek.

81
00:03:56,040 --> 00:03:58,000
Ñaareelu at, klaas B.

82
00:03:58,000 --> 00:04:01,170
Suma njuumteewul, Hyoudou la tuddu.

83
00:04:01,170 --> 00:04:02,930
Ndax amna lu jaarul yoon ci waa ji?

84
00:04:02,930 --> 00:04:06,850
Dara. Amaana sama xel rekk la.

85
00:04:07,600 --> 00:04:08,850
Mat d'échec.

86
00:04:12,230 --> 00:04:13,850
Oh sama...

87
00:04:13,850 --> 00:04:16,310
Mbir mu yomb la.

88
00:04:22,490 --> 00:04:25,700
Waaye, laaj ngama ci lu bari yoon.

89
00:04:25,700 --> 00:04:27,120
Ndax noonu la ?

90
00:04:27,120 --> 00:04:28,780
Maa ngi waajal ak waajal beneen yoon.

91
00:05:10,160 --> 00:05:12,080
Amnaa ndaw yu dellu ginaaw.

92
00:05:12,080 --> 00:05:14,330
Su loolu wéyee...

93
00:05:14,330 --> 00:05:19,420
Sama dundu liise mingi waaja jeex te duma laal ween benn xale bu jigéen.

94
00:05:21,170 --> 00:05:22,170
U-Um...

95
00:05:23,130 --> 00:05:26,970
Hyoudou Issei nga bokk ci Kuou Academy, wala dëgg?

96
00:05:29,600 --> 00:05:30,350
Waaw?

97
00:05:32,430 --> 00:05:34,060
Musu ma gis uniform boobu ci sama àdduna.

98
00:05:34,060 --> 00:05:35,390
Ban daara la bokk?

99
00:05:35,390 --> 00:05:37,600
Ah! Dafa taaru!

100
00:05:37,600 --> 00:05:38,980
Um...

101
00:05:40,060 --> 00:05:42,020
Ndax amna lu nga soxla ci man?

102
00:05:42,020 --> 00:05:42,980
Nanu xool...

103
00:05:45,240 --> 00:05:49,620
Hyoudou-kun, am nga kenn ku ngay génn ak moom?

104
00:05:49,620 --> 00:05:51,660
D-déedet, xamuma ko.

105
00:05:51,660 --> 00:05:53,040
Jërëjëf Yàlla!

106
00:05:53,040 --> 00:05:53,740
Eh?

107
00:05:54,200 --> 00:05:55,790
U-Um...

108
00:05:55,790 --> 00:05:58,790
Ndax dinga ànd ak man génn?

109
00:05:58,790 --> 00:05:59,250
Ha?

110
00:06:00,290 --> 00:06:02,250
Lu nga wax?

111
00:06:03,170 --> 00:06:06,670
Maa ngi lay xool bu yàgg.

112
00:06:07,170 --> 00:06:09,390
Kon...

113
00:06:10,010 --> 00:06:11,600
Bëgg nga...

114
00:06:12,300 --> 00:06:14,060
Hey... Du lii...?

115
00:06:14,060 --> 00:06:16,600
...ngir génn...

116
00:06:19,900 --> 00:06:22,020
Nanga ànd ak man génn!

117
00:06:22,610 --> 00:06:23,110
Lu-

118
00:06:26,070 --> 00:06:30,570
Ndax lii dëgg la?!

119
00:06:30,570 --> 00:06:33,120
Yeewu! Yeewu!

120
00:06:34,160 --> 00:06:38,830
Soo yewwoowul, dinaa la fóon.

121
00:06:39,420 --> 00:06:42,710
Yeewu! Yeewu! Wa-

122
00:06:47,210 --> 00:06:48,630
Lu-Lu?!

123
00:06:48,630 --> 00:06:49,430
Naka?!

124
00:06:50,760 --> 00:06:53,510
Ah! Amano Yuuma-chan la.

125
00:06:53,510 --> 00:06:56,220
Samay xarit lañu, Matsuda ak Motohama.

126
00:06:56,970 --> 00:06:58,100
Kontaan naa ci xam la.

127
00:06:58,810 --> 00:07:02,860
Mooy sama xarit bu jigéen.

128
00:07:03,270 --> 00:07:05,860
Oh well... Yéen ñaar ngeen gaaw wutal seen bopp.

129
00:07:05,860 --> 00:07:07,570
Yuuma-chan, nanu dem.

130
00:07:07,570 --> 00:07:08,110
Baax na!

131
00:07:12,740 --> 00:07:14,660
Warkat bu alku boobu!

132
00:07:16,740 --> 00:07:17,870
Jamono jii?

133
00:07:17,870 --> 00:07:20,540
Waaw. Dibéer bii di ñëw.

134
00:07:20,540 --> 00:07:21,370
Déedéet?

135
00:07:21,370 --> 00:07:23,460
M-Mënu ma baña nangu!

136
00:07:23,460 --> 00:07:25,380
Dëgg la dinaa ci jàmm!

137
00:07:25,380 --> 00:07:26,800
Loolu lu baax la !

138
00:07:26,800 --> 00:07:27,710
Kon...

139
00:07:27,710 --> 00:07:29,050
Waaw! Ba beneen!

140
00:07:31,680 --> 00:07:34,010
Maa ngi waajal bis bi!

141
00:07:35,760 --> 00:07:37,600
Waaw. Man itam.

142
00:07:41,520 --> 00:07:43,310
Jamono jii! Jamono jii!

143
00:07:43,940 --> 00:07:45,770
Son bu neex la!

144
00:07:45,770 --> 00:07:47,730
Baax na!

145
00:07:56,700 --> 00:07:57,490
Gis.

146
00:07:58,370 --> 00:08:00,580
Xamoon naa ko. Sa xaalis mooy...

147
00:08:00,580 --> 00:08:02,500
Bullsey?

148
00:08:02,500 --> 00:08:05,790
Dama jàpp ni dogal bu jaar yoon la, laaj nga seetaan ko.

149
00:08:07,000 --> 00:08:09,000
Persida, loo ci nara def?

150
00:08:09,000 --> 00:08:11,760
Leegi nanu ko bàyyi.

151
00:08:12,380 --> 00:08:15,470
Waaye lépp a ngi ci loxoom.

152
00:08:21,520 --> 00:08:23,890
Dafa jegesi.

153
00:08:23,890 --> 00:08:25,230
Nanga ko am.

154
00:08:30,190 --> 00:08:32,030
Ma jël ko te xalaatuma ko.

155
00:08:31,900 --> 00:08:34,910
Dina ñu def sa bëgg-bëgg

156
00:08:32,440 --> 00:08:34,910
Dina ñu nangu sa bëgg-bëgg?

157
00:08:35,530 --> 00:08:37,450
Loolu doynaar la.

158
00:08:37,450 --> 00:08:38,660
Isei-kun!

159
00:08:39,410 --> 00:08:40,910
Yuuma-chan, suba!

160
00:08:40,910 --> 00:08:42,500
Baal ma! Ndax def naa la nga xaar?

161
00:08:42,500 --> 00:08:45,000
Dédeet, maa ngi ñëw rek.

162
00:08:46,250 --> 00:08:48,920
Dama yàgg a bëgga wax loolu benn yoon!

163
00:09:23,330 --> 00:09:24,200
Lu xew ?

164
00:09:29,380 --> 00:09:30,420
Ndax lépp jàmm?!

165
00:09:31,880 --> 00:09:33,300
Tay neexoon na!

166
00:09:33,300 --> 00:09:35,670
Waaw! Mooy li gëna baax!

167
00:09:39,970 --> 00:09:41,890
Dama ko wara wan sama jikko góor.

168
00:09:45,680 --> 00:09:48,190
Baax na!

169
00:09:54,780 --> 00:09:56,280
Xam nga, Issei-kun,

170
00:09:56,990 --> 00:09:59,910
sunu date bu njëkk bi mooy sunu date bu mujj,

171
00:09:59,910 --> 00:10:02,870
Ndax dinga déglu sama laaj?

172
00:10:03,910 --> 00:10:06,120
Ndax loolu mën na am?

173
00:10:06,120 --> 00:10:06,870
Ki...

174
00:10:08,620 --> 00:10:10,630
Lu mën nekk loolu?

175
00:10:13,000 --> 00:10:14,630
Ndax dinga bëgga dee?

176
00:10:16,550 --> 00:10:17,590
Ndax loolu...

177
00:10:17,590 --> 00:10:18,590
Ha?

178
00:10:18,590 --> 00:10:21,390
Yuuma-chan, jéggalu. Ndax mën nga ko baamtu?

179
00:10:21,390 --> 00:10:23,850
Sama dégg dafa doy waar tay.

180
00:10:25,640 --> 00:10:27,890
Ndax dinga bëgga dee?

181
00:10:27,890 --> 00:10:29,310
Ha?

182
00:10:31,310 --> 00:10:32,310
Dafa amul yéere?!

183
00:10:32,310 --> 00:10:33,820
Gis naa ko !

184
00:10:33,820 --> 00:10:35,610
Foofu moom gis naa ko!

185
00:10:35,610 --> 00:10:37,490
Benn xaaju segond la woon waaye loolu amul benn werante ween yu amul lenn!

186
00:10:37,490 --> 00:10:39,950
Bis boobu mooy bis bi may njëkka gis ween yu fësul ci sama dundu!

187
00:10:39,950 --> 00:10:41,820
Rax ci dolli ñoom ñoo bokk ci xale bu jigéen bu taaru bii.

188
00:10:41,820 --> 00:10:45,080
Lu ñuy woowe lii ? Gump, ndax noonu la woon?

189
00:10:45,080 --> 00:10:46,580
Du loolu la!

190
00:10:46,580 --> 00:10:48,830
Du loolu la.

191
00:10:49,370 --> 00:10:50,330
Laaf yi?

192
00:10:50,870 --> 00:10:52,420
Loolu neexoon na.

193
00:10:52,420 --> 00:10:58,760
Ci fan yii weesu, dama muñ ak fo ak sa jikko xale bu metti bu metti.

194
00:10:58,760 --> 00:11:02,550
Waaye dinaa toppatoo bu baax scrunchy bi nga ma jënd.

195
00:11:02,550 --> 00:11:03,680
Kon...

196
00:11:08,640 --> 00:11:09,640
Yuuma-chan...

197
00:11:09,640 --> 00:11:10,890
Ndax mën nga dee?

198
00:11:17,860 --> 00:11:18,690
Man itam bëgg naa la.

199
00:11:18,690 --> 00:11:24,410
Mën nga nekk risk ci nun, kon fàww ma toppatoo la mu gaaw wala mu yagg.

200
00:11:24,950 --> 00:11:29,960
Soo bëggee nit ku lay tuumal, nga mbugal yàlla yi def yéere yu sell yi ci sa yaram.

201
00:11:30,370 --> 00:11:32,960
Sa- Lu mu doon?

202
00:11:35,710 --> 00:11:38,760
Maa ngi lay sant ci fàttaliku yu neex yi.

203
00:11:41,510 --> 00:11:42,720
Ndax lii dëgg la?

204
00:11:43,890 --> 00:11:50,230
Ndax man mi xamul lu xew, damay dee... ci park bii?

205
00:11:51,600 --> 00:11:55,900
Soo bëggee ray ma, may ma laal ween yooyu.

206
00:11:58,110 --> 00:12:00,490
Mënu ma leen gis bu baax,

207
00:12:00,490 --> 00:12:03,110
waaye loolu ay ween yu rafet lañu woon, Yuuma-chan.

208
00:12:08,450 --> 00:12:11,160
Dafa xonk...

209
00:12:11,870 --> 00:12:14,370
melni kawaram...

210
00:12:14,370 --> 00:12:15,420
Dafa xonk...

211
00:12:15,420 --> 00:12:19,500
Kawar gu xonk gi gëna xonk kawar gu weex melni fraise.

212
00:12:20,760 --> 00:12:23,180
Melni xonk bi tafu samay loxo.

213
00:12:26,180 --> 00:12:29,970
Lu may wax? Leegi dama nara dee...

214
00:12:31,680 --> 00:12:33,810
Baaxul... alal!

215
00:12:33,810 --> 00:12:35,900
Mënatul yëg sama yaram...

216
00:12:36,940 --> 00:12:38,230
Yalna.

217
00:12:38,230 --> 00:12:40,730
Lu tax ma wara dee ci anam wu jaxasoo nii?

218
00:12:43,150 --> 00:12:46,240
Dundu gu xóotul la woon.

219
00:12:46,240 --> 00:12:49,490
Suma mënoon judduwaat, damay...

220
00:12:50,700 --> 00:12:55,790
Rias-senpai, kawaram gu xonk gu rafet gi.

221
00:12:55,790 --> 00:12:57,040
Her...

222
00:12:57,750 --> 00:13:01,670
Leegi ginaaw bima nara dee, dama taamu dee ci dënnu jigéen ju rafet ju mel ni moom.

223
00:13:16,900 --> 00:13:20,440
Kon yaa ma woo.

224
00:13:20,440 --> 00:13:22,150
K-Kan?

225
00:13:24,110 --> 00:13:27,990
Leegi ngay waaja dee, dinaa la ko jëlal.

226
00:13:29,370 --> 00:13:31,370
Yooyu laaf...

227
00:13:32,580 --> 00:13:34,580
Sa ruuh...

228
00:13:35,040 --> 00:13:37,080
Danga wara dundu ngir man.

229
00:13:48,680 --> 00:13:51,050
Dinaa la ray soo yeewuwoo.

230
00:13:51,050 --> 00:13:53,640
Sudee wa-

231
00:13:53,640 --> 00:13:54,810
Soo-

232
00:13:55,180 --> 00:13:56,730
Ah... daa sonn lool...

233
00:13:57,890 --> 00:14:00,560
Loolu moo waral damay dundu ay gént yu doy waar.

234
00:14:03,030 --> 00:14:04,190
Geent la?

235
00:14:04,190 --> 00:14:07,700
Yeen sama gaa yi, fàtte ngeen Yuuma-chan?

236
00:14:07,700 --> 00:14:10,240
Wax naa la, xamunu xale bu jigéen boobu!

237
00:14:10,240 --> 00:14:13,410
Ñaata yoon lanu wara wax ni musu ñu wane xale bu jigéen boobu

238
00:14:13,410 --> 00:14:15,160
te mënoo am xale bu jigéen.

239
00:14:15,160 --> 00:14:16,540
Loolu mënul am!

240
00:14:16,540 --> 00:14:18,210
Amnaa sax emailam...

241
00:14:18,790 --> 00:14:19,580
Nekkul fii...

242
00:14:20,330 --> 00:14:23,210
Nimero telefonam wala adres emailam duñu...

243
00:14:24,050 --> 00:14:25,380
Mu réer.

244
00:14:31,760 --> 00:14:32,930
Rias-senpay!

245
00:14:32,930 --> 00:14:33,850
Ci anam bu dëggu?!

246
00:14:34,720 --> 00:14:36,520
Rias senpay la!

247
00:14:36,520 --> 00:14:38,480
Saa yu ma ko gisee dafa rafet.

248
00:14:52,200 --> 00:14:54,450
Taar la dëgg, wala book?

249
00:15:56,890 --> 00:15:58,220
Oh! Loolu neex na!

250
00:15:58,220 --> 00:15:59,640
Jub?!

251
00:15:59,640 --> 00:16:02,020
Yii ween yu rafet yi ma gis ci sama kanam!

252
00:16:02,020 --> 00:16:03,150
Faatu ñu làmp yi.

253
00:16:03,150 --> 00:16:04,650
Ha? Lu nga wax?

254
00:16:04,650 --> 00:16:07,070
Ba leegi làmp yi ci néeg bi faatu ñu.

255
00:16:07,070 --> 00:16:09,650
Ha?! Lu ngeen di wax nii?

256
00:16:09,650 --> 00:16:11,360
Déedet, du loolu.

257
00:16:11,360 --> 00:16:12,740
Leer gi demna...

258
00:16:13,320 --> 00:16:15,160
Mënu ma yëg leer gi.

259
00:16:15,160 --> 00:16:17,950
Waaye mënoon naa gis... bu baax.

260
00:16:20,910 --> 00:16:23,620
Baal ma... Maa ngi dellu.

261
00:16:23,620 --> 00:16:26,330
Hey. Ndax danga feebar wala lu mell nonu?

262
00:16:34,180 --> 00:16:37,350
Xamoon naa ko. Dama gëna mëna gis bu baax bis bi.

263
00:16:37,970 --> 00:16:43,100
Rax ci dolli, dafa melni doole juy wal...

264
00:16:43,100 --> 00:16:44,850
Déedéet! Jëndeel ma ko!

265
00:16:44,850 --> 00:16:47,610
Dinaa la bàyyi ginaaw sudee dangay xalaat sa bopp kese!

266
00:16:47,610 --> 00:16:48,860
Déedéet!

267
00:16:49,940 --> 00:16:52,740
Lu tax may dégg seen baat fu sori nii?!

268
00:16:54,110 --> 00:16:57,660
Lu xew?! Sama yaram defa melni lu doy waar!

269
00:17:00,490 --> 00:17:01,910
park bii...

270
00:17:04,920 --> 00:17:07,420
Loolu mooy dëgg. Fii la woon.

271
00:17:08,170 --> 00:17:10,920
Mooy barab bima gise ak Yuuma-chan.

272
00:17:11,460 --> 00:17:12,420
Yuuma-chan...

273
00:17:13,420 --> 00:17:17,430
Yaakaar ni loolu gént la... Bëgguma ko gëm.

274
00:17:20,390 --> 00:17:21,470
Luy loolu?!

275
00:17:24,390 --> 00:17:26,940
Lii mooy barabu absorption bi.

276
00:17:28,980 --> 00:17:29,860
Lii lan la?

277
00:17:30,610 --> 00:17:32,610
Sama yaram mënul bayyi di yëngu.

278
00:17:41,990 --> 00:17:44,410
Dama doon dellu ginaaw benn jéego...

279
00:17:46,120 --> 00:17:47,500
Daw, wala?

280
00:17:48,250 --> 00:17:50,460
Xamuma benn linga wax!

281
00:17:52,880 --> 00:17:53,590
Laaf yi?

282
00:17:54,710 --> 00:17:55,630
Yuuma-chan?!

283
00:18:02,260 --> 00:18:04,930
Loolu mooy nekk. Loolu mooy jafe-jafe bi...

284
00:18:06,020 --> 00:18:07,560
Benn ci samay gént?!

285
00:18:10,110 --> 00:18:13,360
Amul benn firnde ci benn njiit wala ay banxaas.

286
00:18:13,360 --> 00:18:17,570
Amul benn màndarga màndarga luxus ci kawam.

287
00:18:17,570 --> 00:18:21,160
Soo xoolee mbir yi, danga wara nekk ku réer.

288
00:18:22,950 --> 00:18:25,580
Suko defee, su ma la ray, du am benn jafe-jafe.

289
00:18:25,580 --> 00:18:30,790
Sudee benn gént la, kon dama taamu góor, jigéen ju...

290
00:18:34,840 --> 00:18:36,050
Dafay metti...

291
00:18:37,220 --> 00:18:39,130
Loolu dafa metti lool!

292
00:18:39,130 --> 00:18:41,850
Loolu dafa metti lool sunu ko méngale ak bi Yuuma-chan faatee ma.

293
00:18:44,220 --> 00:18:45,600
Dafay metti.

294
00:18:45,600 --> 00:18:49,390
Li ko waral mooy leer dafa melni dangar ci sa xeetu nit.

295
00:18:49,390 --> 00:18:53,230
Jàppoon naa ni loolu mooy mujjentalu gacce gi, waaye danga dëgër lool.

296
00:18:54,070 --> 00:18:57,360
Bul jaaxle, dinaa la ray ci saasi.

297
00:18:57,360 --> 00:18:58,820
Mënatuma ko muñ...

298
00:18:58,820 --> 00:19:00,610
Ku ma muccal!

299
00:19:03,160 --> 00:19:05,240
Ndax lii yaa ko def?

300
00:19:05,240 --> 00:19:07,410
Melul ni noonu la.

301
00:19:09,120 --> 00:19:11,170
Mën nga laal xale bu góor boobu?

302
00:19:11,920 --> 00:19:13,420
Kawar gu xonk?

303
00:19:14,420 --> 00:19:16,880
Rias-senpai...

304
00:19:17,420 --> 00:19:20,130
Yaw dof. Yaay kan?

305
00:19:26,640 --> 00:19:28,140
Yeen ay bët!

306
00:19:34,940 --> 00:19:36,440
Kawar gu xonk?

307
00:19:36,440 --> 00:19:37,820
Gis naa...

308
00:19:37,820 --> 00:19:39,190
Ndax bokk nga ci njabootu Gremory?

309
00:19:39,900 --> 00:19:41,700
Rias Gremory.

310
00:19:41,700 --> 00:19:44,700
Loolu lu neex la, M. Fallen Angel.

311
00:19:46,030 --> 00:19:47,240
Loolu yéeme na.

312
00:19:47,240 --> 00:19:51,460
Dëkk bi mingi ci ndigalu famiy Gremory.

313
00:19:51,460 --> 00:19:53,880
Yaakaar naa ni kenn la ci say ndaw?

314
00:19:53,880 --> 00:19:57,170
Duma la bàyyi nga génn lu yomb soo génnee xale bii.

315
00:19:57,170 --> 00:19:59,710
Nanu bàyyi mbir mi ni mu mel.

316
00:19:59,710 --> 00:20:03,130
Waaye soo bàyyee sa ndaw te kenn duko toppatoo,

317
00:20:03,130 --> 00:20:07,350
Ku melni man, ku doon doxantu, mën na ko rëbb ci saasi.

318
00:20:07,350 --> 00:20:09,890
Maa ngi lay sant ci sa xelal.

319
00:20:09,890 --> 00:20:16,440
Soo jëlee dogal ni dangay wéy di def mbir yu mel noonu, di may dofloo, xaaral sa mbugal.

320
00:20:17,110 --> 00:20:22,650
Dinaa delloo kàddu yooyu ci yaw, yaw njiitu njabootu Gremory.

321
00:20:23,860 --> 00:20:26,120
Man douna shiku laa tudd.

322
00:20:26,120 --> 00:20:28,870
Maa ngi ñaan nu baña dajewaat.

323
00:20:33,750 --> 00:20:35,290
Loolu amul benn werante ci man.

324
00:20:35,290 --> 00:20:38,130
Ku ko yaakaaroon ni dina feeñ fii.

325
00:20:38,130 --> 00:20:40,380
Dina dee sunu ko bàyyee.

326
00:20:40,380 --> 00:20:41,920
Duma ko bàyyi mu dee.

327
00:20:43,130 --> 00:20:45,800
Li ko waral mooy xale bii sama...

328
00:20:48,390 --> 00:20:51,890
Maa ngi lay saraxu, yeewu.

329
00:20:52,350 --> 00:20:53,770
Moket.

330
00:20:56,350 --> 00:20:58,150
Sama bopp bi dafay metti...

331
00:20:58,150 --> 00:20:59,770
Dama am beneen gént bu doy waar...

332
00:21:00,280 --> 00:21:02,530
Lu tax ma saa yu nekk...

333
00:21:02,530 --> 00:21:04,990
Ha? Lu tax ma amul yéere?

334
00:21:04,990 --> 00:21:06,530
Fan la sama mbubb nekk?

335
00:21:11,740 --> 00:21:13,710
Lu xew...

336
00:21:13,710 --> 00:21:15,580
Rias-senpay?!

337
00:21:20,460 --> 00:21:21,340
Ci suba?

338
00:21:26,050 --> 00:21:27,550
B-Ween!

339
00:21:29,140 --> 00:21:30,050
Subag jàmm!

340
00:21:30,050 --> 00:21:33,310
Lu tax Rias-senpai...?

341
00:21:33,310 --> 00:21:36,270
Geent la? Loolu mooy dëgg, lii mooy wéyal gént bi!

342
00:21:37,100 --> 00:21:38,310
Loolu dëgg la.

343
00:21:38,310 --> 00:21:41,820
Lépp lu la dal. Loolu lépp.

344
00:21:42,610 --> 00:21:44,530
Man maay Rias Gremory.

345
00:21:45,030 --> 00:21:46,200
Jinne.

346
00:21:46,990 --> 00:21:48,070
Dëmm?!

347
00:21:48,700 --> 00:21:51,780
Te man maay seen boroom.

348
00:21:51,780 --> 00:21:55,210
Hyoudou Issei-kun, kontaan naa ci xam la.

349
00:23:26,880 --> 00:23:41,890
Beneen yoon

350
00:23:28,050 --> 00:23:31,470
Jéemal fàttaliku li nga gëna yëg ni moo gëna am doole.

351
00:23:31,470 --> 00:23:34,350
Dinaa nekk Buuru Harem bi!

352
00:23:34,550 --> 00:23:36,970
Lebal ma sa kàttan!

353
00:23:36,970 --> 00:23:41,890
Mën nga ni dafa melni sama rakk bu ndaw bu dof bi.

354
00:23:36,970 --> 00:23:42,020
épisode 2

355
00:23:36,970 --> 00:23:42,020
「Dama bàyyi nekk nit!」

